Paroles-Celebres.com > Artiste I > Paroles Ismaël Lo > Paroles Tass Yakar

Paroles Tass Yakar

Ismaël Lo - Toutes les paroles des chansons de Ismaël Lo

Je vote pour cette chanson
1 étoile 2 étoiles 3 étoiles 4 étoiles 5 étoiles Aucune étoile
wagni lène ki
sa bay wagnila sa yaye wagnila
yaw ngani ya bagne
way dégueul lii
sa yaye wagnila sa bay wagnila
yaw ngani ya bagne
bo khamone do dokholè ni nagua
soralé euleuk digua yori sa diabot yaw
say wadiour lou bakh lagn la digueeul
bougnou sagnone ken doula gueun
kon lou bakh lagn la yéné
kon bok euleuk boul retiou nane
sama yaye yé
sama yaye boy sorina foumakay dioyé
sama yaye yé
sama yaye boy sorina foumakay dioyé
koulané senguoul sa taar lala beugueul
mané wadiour bolen défé kharit yaw
domassa lal souf
am bouki mané yombana lol
wayé bou mana khalam mo diafé
ki
sa bay wagnila sa yaye wagnila
yaw ngani ya bagne
way dégueul lii
sa yaye wagnila sa bay wagnila
yaw ngani ya bagne
bo khamone do dokholè ni nagua
soralé euleuk digua yori sa diabot yaw
say wadiour lou bakh lagn la digueeul
bougnou sagnone ken doula gueun
kon lou bakh lagn la yéné
kon bok euleuk boul retiou nane
sama yaye yé
sama yaye boy sorina foumakay dioyé
sama yaye yé
sama yaye boy sorina foumakay dioyé
koulané senguoul sa taar lala beugueul
mané wadiour bolen défé kharit yaw
domassa lal souf
am bouki mané yombana lol
wayé bou mana khalam mo diafé

say wadiour lou bakh lagn la digueeul
bougnou sagnone ken doula gueun
kon lou bakh lagn la yéné
kon bok euleuk boul retiou nane
sama yaye yé
sama yaye boy sorina foumakay dioyé
sama yaye yé
sama yaye boy sorina foumakay dioyé
sama yaye yé sama yaye boy sorina
foumakay dioyé
bo bougué mouthia dagay téral say wadiour
sama yaye yé sama yaye boy sorina
foumakay dioyé
bo nanguo bakh nagua dégueul say wadiour
haléyi fofou lagnou rawanté
ndakh wadiour kouko lébal
bour yala fayla ba dolila yaw
bo défé béneu am gnare
bo défé gnare am gnint
bo défé gnint am fouk
bo mané témère gnagua téral say wadiour
bo mané témère gnagua téral say wadiour

Regardez le clip vidéo de Ismaël Lo, de sa chanson Tass Yakar sur Paroles-Celebres.com

Tous vos artistes, et lyrics préférés sont sur ce site de paroles.

Sur notre site de paroles-celebres.com, vous pouvez imprimer les paroles de chanson, sans les publicités, ni les menus. Pour avoir uniquement le titre de la chanson, le nom de l'auteur, et les paroles, il vous suffit de cliquer sur le lien suivant, pour imprimer les paroles de la chanson Tass Yakar, de Ismaël Lo .


Toutes les paroles de chanson à imprimer facilement sont sur paroles-celebres.com. Les titres de chansons comme Tass Yakar, de Ismaël Lo prêt à être télécharger en PDF, ou imprimer. Vous avez la possibilité de sauvegarder en PDF le document imprimé à partir de cette page web. Utilisez pour cela les outils sur Internet à disposition, qui génèrent un fichier PDF à partir de cette page internet de parole de chanson Tass Yakar, de Ismaël Lo. Pour imprimer, suivez le lien print lyrics Tass Yakar

Mis à jour le 04-05-2015   Vu 107 fois

Statistiques du texte Tass Yakar

Il y a 20 fois le mot yaye dans le texte de la chanson.
Il y a 16 fois le mot sama dans le texte de la chanson.
Il y a 10 fois le mot wadiour dans le texte de la chanson.
Vous avez aimé ? Partager ! lyrics Tass Yakar - Ismaël Lo